Link to home pageLanguagesLink to all Bible versions on this site
Sabóor 117
Na ñépp ànd ak Israyil sant Yàlla
1 Yeen xeetoo xeet, màggal-leen Aji Sax ji,
réewoo réew, kañleen ko.
2 Moo nu xéewale ngoram gu réy,
te wormay Aji Sax jee sax dàkk.
Màggal-leen Ki Sax!

<- Sabóor 116Sabóor 118 ->